Gudi Diop-Wasis Diop
Gudi Diop-Wasis Diop无损flac下载mp3下载
Gudi Diop-Wasis Diop 在线试听歌词免费下载
Tanku neen (3 fois)
La doxé
Tanku neen (3 fois)
Tanku neen (2 fois)
Loxo neen
coono neen
xif neen
feyda waaw
aw ma "vélo" asta maak "auto"
nit ku néka
amna lu koy rey bes (lu koy rey bes bes bes ...)
suma diotoon lolou
dina dee
foum ko diaguar diaguar diaguar diaguar diaguar
Ca adiana sa ca safara sa
Tankou neen la doxé
bayico guinaaw diem kanam
bu ngelew li diogué
ma and' ak moom (di weey)
bet bou fata fata fata manam
Sama tur munu ma ko wax ci khadia goudi
Bou ko djiné yi dégué
sétè souba aat
yobou ko ci ay dioow dioow
fine ma djeulè sorinaa
yalouwane sèè
sookh sookhlou wooroul
boula diarè yow di ngua sookh
waayé do dèè
damala yendu lo guane laa fi
fima diogué soori na
topa taali bi dox ba eksi
fege neek bi lo fiy outsi
ci khadia goudi gui
man la goudi diop, mana
Sama tur munu ma ko wax ci khadia goudi
Bou ko djiné yi dégué
sétè souba aat
yobou ko ci ay dioow dioow
(refrain 2 x )
sétè souba aat
sétè souba aat
Gudi Diop-Wasis Diop歌曲下载
| 歌曲 | 歌手 | 专辑 | 时长 | 歌曲下载 |
|---|---|---|---|---|
| Gudi diop(Ingmarlo Ibiza Remix) | Wasis Diop | Ibiza Sounds (Lounge) | 06:41 |
|
| Gudi Diop | Wasis Diop | Judu Bék | 03:26 |
|
Gudi Diop-Wasis Diop热门评论
Gudi Diop-Wasis Diop 同专辑其他歌曲
- So La La!-Wasis Diop
- Let It Go-Wasis Diop
- Kula Soxla-Wasis Diop
- Anna Mou-Wasis Diop
- L'Ange Djibril (Hallelujah)-Wasis Diop
- Ndiago Pop-Wasis Diop
- Dans L'Aréne-Wasis Diop
- Judu Bék-Wasis Diop
- Automobile Mobile-Wasis Diop
- Galu Nobéél-Wasis Diop
- Tuti Sop-Wasis Diop