Gen ji dekk-Titi
SQGen ji dekk-Titi无损flac下载mp3下载
Gen ji dekk-Titi 在线试听歌词免费下载
[ti:Gen ji dekk]
[ar:Titi]
[al:Titi la lionne]
[by:]
[offset:0]
[00:00.65]Gen ji dekk - Titi
[00:02.09]Written by:Ibou Ndour/Titi
[00:03.42]
[00:08.66]Guentouma hé Gentouma
[00:11.55]
[00:12.16]Hoooooo Hooo
[00:15.55]
[00:22.98]Guentouma hé Gentouma
[00:25.72]
[00:26.51]Beugouma yewou rek guente gui diekh
[00:30.25]
[00:36.32]Ngua neck fi ma neck feulé
[00:38.06]Dou té niou gussanté
[00:39.64]Nékal fi mangui feulé Beugenala
[00:42.72]
[00:43.36]Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako
[00:46.47]
[00:47.23]Beugnala
[00:48.40]
[00:49.07]Guemenala
[00:50.54]Geumnawooo Ho
[00:52.49]
[00:53.00]Guentouma
[00:53.92]Guentouma
[00:54.46]
[01:01.10]Nekkal fi ma neck feulé
[01:02.90]Dou té niou gussanté
[01:04.41]Nékal fi mangui feulé Beugenala
[01:07.53]
[01:08.17]Khol dafa noyya noye Louo ci dougou yeuknako
[01:11.06]
[01:11.81]Beugnala
[01:12.82]
[01:13.54]Guemenala
[01:14.45]
[01:15.30]Geumnawooo Ho
[01:16.85]
[01:17.49]Guentouma
[01:18.37]Guentouma
[01:19.12]
[01:26.37]Naniou Khalaté lou lenne nekh ci mane
[01:29.31]
[01:29.84]Bayiléne niou wakh louléne nekh ci mane
[01:32.80]
[01:40.47]Maye adji kiiy beug Beugnala
[01:43.20]
[01:44.00]Beug Sa Deuk Ba Deuk
[01:45.65]Fa mouy guene di deuk ci mane
[01:47.35]
[01:54.50]Yaw yaye ki kidnaper sama life
[01:57.14]
[01:57.70]Hooo Hooo My life
[02:01.29]
[02:08.60]Kidnaper sama temps khamnala
[02:11.28]
[02:12.05]Temperature bo necké soma guissé guif
[02:15.23]
[02:22.60]Dangua beugonna kham ci lanne la néék
[02:25.59]
[02:26.15]Dangua beugonna kham ci lanne lay dokh
[02:28.90]
[02:29.55]Yakamtina niouye skype
[02:32.21]
[02:33.16]Deug sa viber am sa allo
[02:35.97]
[02:36.64]Arrosé na samay fleur mane
[02:40.08]Ba meuna feyy ci bissoub mbeugéll yii
[02:44.24]
[02:51.01]Gen Ji Dekk dama yague ak yaw
[02:53.27]
[02:54.34]Ba so yeukeutii say kaddu
[02:56.09]
[02:57.92]Bala nguay danéél makoy teureul
[03:00.52]Gen Ji Dekk
[03:01.32]
[03:04.82]Geunalanté wouma la ak niom My baby
[03:08.61]Dafa fekk ni do niom douniou yaw
[03:11.92]Minne na la
[03:13.39]Tammou na la
[03:14.65]
[03:15.21]Mane mala tamou ci niom ba ngua doyma
[03:18.20]
[03:24.94]Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo
[03:27.90]Ni mala beugué rombe na Yillif
[03:31.26]Ni ngua ma beugé dafa diegui dayyo
[03:34.24]Ni mala beugué rombe na Yillif héé
[03:37.67]
[03:44.64]Sama guente gui
[03:46.10]
[03:47.53]Mba douma yewou rek mou diekh
[03:50.51]
[03:53.17]Sama guente gui
[03:56.38]
[03:58.32]Mba douma yewou rek mou diekh
[04:01.73]
[04:05.43]Sama guente gui
[04:09.41]Mba douma yewou rek mou diekh
[04:12.56]
[04:21.00]Gen Ji Dekk
[04:21.97]
[04:23.71]Ya léne guene ci mane
[04:25.67]
[04:26.65]Té dou yagg ba ngua donne niom
[04:28.71]
[04:29.68]Do meussa donne niom
[04:32.09]
[04:43.59]Soumay nieuw ci yaw
[04:44.86]
[04:46.29]Ropplane loumou naw naw
[04:47.84]
[04:49.42]Ma guena gaw ci yaw
[04:51.21]
[04:54.00]Nangouna donne sa autorail
[04:56.55]
[04:57.21]Souma djoubé gare cornet né Yeuksinna
[04:59.62]
[05:06.26]Beug nala guemnala
[05:08.69]Ni mala beugé dafa diegui dayyo
[05:11.45]Ni ngua ma beugué rombe na Yillif
[05:14.46]Beug nala
[05:15.54]
[05:16.16]Beug nala
[05:17.08]
[05:17.59]Beug nala
[05:26.72]
[05:27.70]Beug nala
Gen ji dekk-Titi歌曲下载
| 歌曲 | 歌手 | 专辑 | 时长 | 歌曲下载 |
|---|---|---|---|---|
| Gen ji dekk | Titi | Titi la lionne | 05:36 |
|
Gen ji dekk-Titi热门评论
Gen ji dekk-Titi 同专辑其他歌曲
- Nit day xam boppam-Titi
- Bul may fiiré-Titi
- Booba ba tay-Titi
- Mame saliou-Titi
- Jiggen feem-Titi
- Marchands ambulants-Titi